6. SILMAKHA / NON VOYANTE
En wolof

(Fatou Fania Niang, Fadjala Dawara / Fatou Fania Niang)

Do tou ma tonie
kene douma tonie
maye silmakha
guoumbogui
dieulele sama lohko
dialema yone wi
yow mi yore
beutou m beuguele
maye silmakha
guoumbogui
dieule sama lokho
dialema yone wi
yow mi yore beutou m beuguele
sama khol
sama yaram
lepe thi mane
yow lei sete
yow mi yore beutou beuguele
maye silmakha
guoumbogui
dieule sama lokho
dialema yone wi
yow mi yore beutou m beuguele
maye silmakha

Je peux pas faire du mal
je suis pour la paix
je suis non voyante
l'aveugle
prend ma main
fais moi traverser la rue
toi qui a le regard d'un amoureux
je suis non voyante
l'aveugle
prend ma main
fait moi traverser la rue
toi qui a le regard d'un amoureux
mon cur
mon corps
le tout en moi
te cherche
toi qui a le regard d'un amoureux
je suis non voyante
l'aveugle prend ma main
fais moi traverser la rue
toi qui a le regard d'un amoureux
je suis non voyante

Fania Niang © www.faniaka.com


* * *